Fan yii, coowal ECO baa ngi mel ni tànnbéeru dëmm, rëb ba nga ne lii lum doon. Bi Emmanuel Macron ak Alassane Ouattara defee seen yégle bi ba léegi, ku nekk a ngi àddu ci mbir mi. Jàppal ECO fii, bàyyil ECO fee. Muy taskati xibaar yi, politiseŋ yi (raw...