Ab téeree ngi nii boo xam ne, bii, boo koy jàng doo bëgg mu gaaw a jéex. Dafa mel ni, fàww nga def loolu wolof naan ñiimantalu. Soo dee ku yàgg a tiim téere, te xam fa bindkat di jaar, ak la muy daj, ba li muy nettali itteel képp ku ko yër, doo mën lu ...