Mbas mi jaaxal na ñépp, yëngal àddina sépp. Jàngoro jii di koronaawiris wone na boppam ci fànn gu ne : koom, wér–gi–yaram, njàng, añs. Njiiti réew yépp a jaaxle fi mu ne nii, limu néew yaa ngiy yokku bés bu ne, nguur gi xamatul nu muy def ak way-wopp y...